Aller au contenu

Nimero téere buñ miin ci àdduna bi

Jóge Wikipedia.

Nimero Téere buñ miin ci àdduna bi (ISBN mba International Standard Book Number ci Àngle mba Numéro international normalisé du livre ci français) mooy benn nimero buy xàmmee téere njaay mi, te dañu ko jagleel ngir mu wuute ak yeneen yi. Ñiy siiwal téere dañuy jënd wala jot ay ISBN ci benn kuréel bu bokk ci kuréel gi yor ISBN ci àdduna bi.[1]

  1. "The International ISBN Agency." [1] / tasaayi